Wiktionary:ay baati politig
Xët wii aw xëtu sémb la ngir sos ay baati wolof yu ñeel xam-xamu politig.
Doy na nga bind tekkeem ci wolof ci kanamu baat bi te joxe ci ay leeral. Sunu deme ba ànd ci ab baat nu soog koy utal aw xët. sunuy sos xëtu baat wi bu nu ci fatte defaale [[catégorie:baati wolof]] [[catégorie:politig]] . day tax baat bi duggu ci wàll wi mu bokk
Ngir am ay leeral ci tekkiy baat yi ci wu faraas demal ci bii dal
A
Soppi- accumulation du capital: njalum bopp-alal
- acratie: ag déet-nguur, ñakk-kilifteef
- ajustement structurel:jubanti gu cëslaay
- altermondialisme: ngérum geneen-àddinaal
- anarchie: ag nguuradi, ñakk-kilifteef
- anarchisme: ngérum ag nguuradi, ngérum ñakk-kiliftéef
- anomie: ag nosoodiku
- antisémitisme: noonu ag caam, ngérum safaancaam
- aristocratie:ag ngarmi
- assemblée nationale: péncum ndawi réew, péncum réew
- autarcie: ag doylu ci sa bopp, ag doylu
- autocratie: nguurug kenn
- autogestion: saytu gu poppu, yor-sa-bopp
- autodétermination : mujjal-sa-bopp
- autonomie : àtte gu boppu, àtte-sa-bopp
- autonomisme : ngérum àtte sa bopp
- autoritaire : aji jaay kiliftéef, aji-jaay-kiliftéef
- autoritarisme : ag jaay-kiliftéef, ngérum jaay-kiliftéef
B
Soppi- bénévolat: casino en ligne
- besoin : aajo
- bilderberg (Groupe)mbooloom Bilderberberg
- BIP 40: nattukaayu ñàkk ak yamoodi
- bipartisme: ngérum ñaari-làng
- bonapartisme : ngérum Bonapart
- bouc émissaire: gàttub njot
- bouclier fiscal: pakkub galag
- bourgeois : kenn ci maas gu diggu gi, ?
- bourgeoisie: maas gu diggu gi, ?
- boycott: ag dogoo
- bureaucratie: liggéeyu binduwaay, ?
C
Soppi- cacocratie: nguurug baadoolo
- capital : bopp-alal
- capital (Accumulation du):ndajalem bopp-alal (am na fof dajaloom bopp-alal)
- capitalisme: nosteg bopp-alal, ngérum bopp-alal
- carriérisme: ag ceet sa njariñ, ngérum njariñu
- cartel: ag déggoo
- caste : waaso
- censure:tere
- césarisme : nosteg xaysar, ngérum xaysar
- chauvinisme : ngérum Chauvin
- che-guevarisme : ngérum Che guewara
- chômage:ag xéyadi, ñakk-xéy
- citoyen: aji réewu
- civilisation: xay
- classe sociale: kuréel gu mboolaay
- clientélisme : njënd
- coalition: ag tappoo
- collectif: am mbooloo;ag mbootaay;lu ñu bokk
- collectivisme: ag mbooloo
- colonialisme : ngérum canc
- communautarisme :ag mboolaayal=(socialiser). ngérum askanal
- Commune: dëkk-dëkkaan
- communication :jokkoo
- communisme : mbokkte
- communisme de conseils: mbokkte gu ay jataay
- concurrence :ag gëpplante
- conditionnement: sart
- conservateur: aji wattoonte; aji watt
- conseillisme : ngérum diisoo
- consommation: ag lakk,ag jëfandiku
- consommation (Société de): mboolaayug jëfandiku
- constitution :sartu réew; ndeyi àtte ( aram fal)
- coopérative: mbootaayug jàpplante, jëfandoo
- coopération:jëflante:àndadoo liggeey, jàpplante, jëflante
- corporation: mbootaay, daayira, mbootaay
- corporatisme: ngérum mbootaay, ngérum daayira, ngérum mbootaay
- corruption: ger
- cosmopolite: doomi àdduna bi: aji dëkk ci réew yépp, ngérum
- cosmopolitisme: ag ndoomu-àdduna: ag dëkk ci réew yépp, ngérum ngérum
- coup d'Etat: nangu nguur, yong
- croissance:ag màgg
- culture:aada;caada
D
Soppi- décentralisation:ag diggadil
- décroissance: ag màggadi;deltu-ginnaaw;suux,rëppéelu;juunu;jëm suuf
- délocalisation:juge ci barab;tuxu
- démagogie: ag mbooloowu, ag nax-askan
- démocratie:demokaraasi,nguurug askan
- démocratie participative: demokaraasi gu ñu bokk
- démocratie représentative: demokaraasi guy wuutoo
- démocrature:demo-naxe,naxekaraasi, nguuru askan gu naxe
- député : ndawu réew;aji wuutu
- céréglementation: dindiy-àtte, woyofal,nosadil
- dérégulation: dindiy-àtte, woyofal,nosadil
- désobéissance civile: moy gu ñoñ
- développement: ag jëm-kanam;ag naat
- développement durable; jëm-kanam gu dëgër, guy wéy
- despotisme: nguurug doole, ndiktaatiir, nguurug kenn añs
- dialectique: dàggasante; joqalantey lay, yayante
- dictature : ndigtaatiir; ag doxe doole, ag doxe sañ-sañ
- dictature du prolétariat: ndiktaatiir gu liggéeykat yi
- dictocratie:demo-naxe,naxekaraasi, nguuru askan gu naxe
- discrimination:xàjjatle;raññatle
- doctrine:ngér
- doxocratie:nguurug xalaat, xalaatkaraasi
- droite: ndayjoor
- droite (Extrême): ndayjoor gu catu
- dyarchie:àtteg ñaar, nguur gu ñu ñaaral
E
Soppi- écologie: xam-xamu wërlaay
- économie:koom-koom
- égalitarisme: ngérum yam, ngéum yamoo
- égalité: ag yam, ag yamoo
- élection: tànn, fal,
- electoralisme : wutug falu, sàkkug tànnu
- emancipation: goreel (ab jaam)
- empire: imbraatóor
- emploi: liggéey, xéy
- enarchie: dooley-ENA, nguurug ENA
- entrisme: ngérum dugg
- épistémocratie: nguurug way xam yi
- équité: ag maandu
- ésclavage: ag njaam
- état : nguur
- éthique : jikko
- eurocratie: nguurug Tugal, Tugal-kraasi
- expertocratie: dooley-fóore, fóorekaraasi, nguur-fóore
- exploitation: jariñoo
- extrême droite : ndijoor gu catu
F
Soppi- fascisme: ngérum faasi walla ag faasi
- fédéralisme :ag lëngoo, ag federaal
- fédération: ag lëngoo, ag federaal
- féminisme: ag njiggéen, ag yamoo gu góor ak jiggéen
- féodalité: ag laman
- fiducie: kóoolute, tayle
- fiscal (Paradis): àjjanay galag
- forum: waxtaanuwaay, pénc
- forum social: pénc mu mboolaay
- franc-maçonnerie: yoonu way tabax yu gore yi, diiney way tabax yu gore yi
- fraternité: :ag mbokkoo, ab tariixa
G
Soppi- gauche: càmmooñ
- gauchisme: ngérum càmmooñ
- gaullisme: ngérum Góol, ngérum De Góol
- génocide: faagaagalal, alag, ray mbooloo
- gérontocratie: àtteg mag ñi, nguurug màg ñi
- gouvernance: àtte, saytu, doxal,jiite, wommat
- gouvernement: ag àtte, ag caytu, ag doxal, ag njiit,
- gratuit, gratuité: ci lu dul fay, ci anam gu ñu maye, ag maye, amul-fay
- guevarisme: ngérum Gewara
- gynarchie: nguurug jiggéen, caytug jiggéen
- gynocratie:njiiteg jiggéen, caytug jiggéen
H
Soppi- héritage: ag ndono
- hiérarchie: ag toftaloo, ag toppante
- humanisme: ngérum nite
- humanité: ag nite
I
Soppi- idéocratie: caytu gu ngér, nguurug ngér
- idéologie: xam-xamu xalaat, ngér
- I.D.H.: W.J.N, W.D.N
- impérialisme: ag imbraatóoral, ag réyal nguur
- indépendantisme: ngérim tembte, ngérum wéeroodi, ngérum moom sa bopp
- inégalité: ag yamoodiku, ag yamoodi
- inflation: ag walu, ag walu gu njëg
- information: xibaar, xamale, joxe xam-xam
- insurrection: ag buur, ag fipp, ag jeqiku
- intégration:ag bokk
- international situationniste:
- internationalisme:
- IPH: W.Ñ.N
J
Soppi- jacobinisme: ngérum Jakobin
- journalisme, journaliste : tasum xibaar, taskatu xibaar
- junte: ndiktaatiir gu xare, ag doxe doole gu xare(militaire)
K
Soppi- keynésianisme: ngérum Keynes
- kleptocratie:nguurug ger
L
Soppi- laïcité: ag diineedi, ag déet-diine, ag egliisadi, ag jàngubeedil
- langue de bois: làmmiñu dénk, waxi tappale
- léninisme: ngérum Lenine
- libéralisme: ngérum péexte, ngérum gore, ag tënkoodiku
- libertaire: lu aju cig péex, lu féex, lu gore
- libertarien:ku bokk ci ñoñ péexte ñi, kenn ci ñoñ gore ñi
- libertarianisme: ngérum ñoñ péexte ñi
- liberté: péex, ag péexte, ag gore, ag tënkoodiku
- libre-échange: joqalante gu af, wecceente gu gore, gu tënkoodiku
- lobby, lobbying: mbooloom naj, way bàyyiloo xel, mbooloom jeexiital
- localisme: ngérum tund, ag tundal
- logocratie: nguurug màndarga
- lutte des classes: xeexub kuréel yi
- lotocratie: nguurug tegoo-bant (nguurug lotori)
- luxemburgisme: ngérum Luxemburg
M
Soppi- majorité: ag ëppte, aw ëppiit
- manipulation:ag jariñoo, nax
- maoïsme: ngérum Maawo
- marché: ab ja
- marianne:mariyaan
- marketing: ag jawal, ag jaal, xam-xamu jaay,
- marxisme: ngérum Marx
- matérialisme: ngérum ne-ne,
- média: tasukaayu xibaar
- médiocratie: nguurug ñu suufe ñi
- mercantilisme: ag jaaykat, ngérum jaaykat, ag nja
- mercatique:ag jawal, ag jaal, xam-xamu jaay,
- mérite: ag yayoo
- méritocratie:nguurug yayoo
- monarchie:nguurug kenn
- mondialisation: ag àddinaal
- mondialisme: ngérum àdduna
- monopole: ag rënk, ag ngartaajoo, ag aldande
- monopartisme : ag genn làng
- motion de censure :ag rocci kóolute
- morale: xam-xamu jikko yi
- mutualisme :ngérum loxoy Kajoor
- mutuelle: lu ñu joqalante
- mutuelle: ab natt
N
Soppi- nation:aw xeet
- national-socialisme: ngérum nasi
- nationalisme: ag xeetu
- nazisme: ngérum Nasi
- négationnisme: ngérum weddi
- néocolonialisme :ngérum canc gu yees gi
- néocorporatisme: ngérum mbootaam mu yees mi
- néolibéralisme: ngérum péexte mu yees mi, ngérum afal mu yees mi
- néo-localisme: tundal gu yees gi, ngérum tund mu yees mi
- néonazisme: ngérum Nasi mu yees mi
- népotisme: ag njarbaat, ag jarbaatal, ngérum jarbaat
- nihilisme: ag daraal, ngérum dara,
O
Soppi- ochlocratie: nguurug mbooloo yi, nguurug baadoola
- oligarchie: nguurug kuréel,
- oligopole:jawub kuréel
- opinion: gis-gis, xalaat
- opportunisme: ag bàddoo, ag jariñoo, ngérum bàddoo, ngérum pose
P
Soppi- parlement:ab barlamaan, péncum mbooleem ndaw yi
- parlementarisme: ag barlamaan, ngérum péncum ndaw, ngérum barlamaan
- parti politique: làngug politig
- patrimoine: ndono l-
- patriotisme: ag bëgg-sa-réew, ag réewte
- paupérisation: ag ndóolal, ag ñàkkal
- paupérisme: ag ndóol
- pauvreté: ag ñàkk
- pétition:ag càkkutéef, mbindum càkkutéef
- peuple: ag bar, aw askan, am mbooloo
- phallocratie:nguurug ngóora
- P.I.B.: NJ.Ñ.B
- plébiscite: ag laaju gu mbooloo, ag laaj mbooloo mi
- ploutocratie: nguurug way woomle yi, nguurug woomle
- politique: politig, doxaliin, àttewiin, jiiteyiin
- polyarchie:nguurug mbooloo
- populisme: ag baral, ngérum askan, ag baab-mbooloo
- postdémocratie:ginnaaw-demokaraasi
- poujadisme: ag Pujade, yëngu-yëngu gu Pujade
- pouvoir: nguur, doole, sañ-sañ, kiliftéef
- pouvoir d'achat: man-manu jënd, kàttanug jënd
- précariat:ñu-pay-gu-saxadi
- précarité: ag saxadi, ak wóoradi
- président de la République: njiiti pénc mi, njiitu réew mi
- presse: am tasum yëglekaay yi
- presse écrite: yëglekaay yi
- privatisation: ag jàmbural,
- privilège: ag xejji, ag gënal, gënale
- progrès: ag jëm-kanam, ag dox
- progressisme: ngérum jëm-kanam, ngérum dox
- prolétariat :baadoola yi
- propagande: ag baab
- proportionnel: lu tolloo,
- propriété: ag moomeel
- protectionnisme: ag aar, ngérum aar
- publicité:siiwal
- physiocratie: nguurug dénd, nguurug mbay
R
Soppi- racisme: ag xeetal, ngérum xeetal
- radicalisme: ag reenu, ngérum reenu
- ratification: wéral, saxal
- réactionnaire:aji dellu-ginnaaw
- référendum: ag laaju
- réforme: ag yéwénal
- réforme structurelle: ag yéwénal gu cëslaay
- réformisme: ngérum yéwénal
- régime: ag noste, ag àtte, ag doxal
- régime parlementaire: nosteg barlamaan, nosteg péncum réew
- régime présidentiel: noteg njiit
- régionalisme: ag diiwaanal, ngéerum diiwaan, ag ndiiwaan
- relocalisation:ag tuxalaat, ag delloowaat
- rente, rentier: aji dugg, ngañaay
- représentation proportionnelle: ag teewal gu yamoo, gu tolloo
- république: pénc
- révisionnisme: ngérum xoolaat, ag xoolaat
- révolte: jeqiku
- révolution: ag jeqiku
- richesse: koom,
- royauté: ag nguur
S
Soppi- salariat, salarié
- scrutin: ag tànn, ag woote, ag fal
- sectaire: lu kuréel
- sectarisme: ngérum kuréel
- secte: ag kuréel
- ségrégation: tàqale, gënale, ràññatle
- S.E.L. : N.W.T
- sénat:jataayub mag ñi
- séparatisme: ag tàqalikoo, ngérum tàqalikoo
- service public: liggéey bu mbooloo mi, liggéey bu bar gi, liggéey bu ñu bokk bi
- simplicité volontaire: yombte gog nammeel, woyofal gog nammeel
- sionisme: ngérum sahyoon, ag sahyoon
- situationnisme:
- social: lu mboolaay
- social-démocratie: demokaraasi gu mboolaay, mbool-demokaraasi
- socialisme: ag bokkoo, ngérum bokkoo
- société: ag mbootaay, ag mboolaay, ag lonkoo
- société de consommation: mboolaay gu lakk, mboolaay gog jëfandiku
- sociologie: xam-xamu mboolaay; gëstu gu mboolaay
- solidarité: dimbalante
- souveraineté:ag cang
- souverainisme: ag cangal, ngérum cangal
- stalinisme: ngérum Stalin
- stochocratie:nguurug tegoo-bant, àtteg tegoo-bant
- stock-option:tànnug cér
- stratocratie: nguurug xare
- subsidiarité: ag kilifaal ndaw
- succession: ag wuutu
- suffrage: ag kàddul, ag dëgëral,ag wooteel
- synarchie:nguuru ay njiit, nguuru ay kilifa
- syndicat: mbootaayu ay liggéeykat
T
Soppi- taylorisme: ngérum Taylor
- tétrarchie: ag nguur gu ñeent
- technocratie: nguurug fóore
- théocratie: nguurug Yàlla
- totalitarisme : nguur gu joyu
- traditionalisme: ab baax
- travail:liggéey
- trotskisme ngérum Trotski
- TVA: galagu njëg
- tyrannie: nguurug doole
U
Soppi- ultralibéralisme: ag afal gu jéggi dayo
- universalisme: ag daj-àddina
- utopie: gént
V
SoppiX
Soppi
Z
Soppi- zapatisme : ngérum Sapata